🔍 Crx搜搜
Kàddug Yàlla+
0.0
0
免费下载

截图预览

概述
翻译

Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari téere yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci téere yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof. Man nga ko jàng ci wolof, wolofal, français, anglais, ak grec.

特性

Versions wolof, français, anglais, ak grec Seet ay baat ci téere yi yépp Ay pàcc yuy andante

此版本中的新增功能

Xoolal sa pàccub leeral bu bees. Da lay indil njàngat yu wóor. Defaraat ci fi ngay tànne làkku interface bi - appli bi dencul ko woon. Defaraat nañu ay bugs

系统要求

适用平台:电脑

操作系统:Windows 10 版本 17763.0 或更高版本

来自商店的评价 (0)

尚无人评价此扩展,查看 其他语言

留言